Daara Matlaboul Chifai Wakeur Serigne Saliou Sopey Cheikh Ibra

Daara Matlaboul Chifai Wakeur Serigne Saliou Sopey Cheikh Ibra Toujours aux services du Cheikh !!!

Bon Magal de Prokhane !
10/02/2022

Bon Magal de Prokhane !

Na ngéen góorgóorlu ci ag njub, ku ci dëng kune ma won la guinaaw.Ku ci topp ag njub nag, ma fat la, ndax du ma ànd ak k...
22/01/2022

Na ngéen góorgóorlu ci ag njub, ku ci dëng kune ma won la guinaaw.
Ku ci topp ag njub nag, ma fat la, ndax du ma ànd ak ku yàqu.

BOROOM TUUBAA

Bravo à ces braves SOKHNA qui s'occupent du nettoyage et de la propreté de la Grande Mosquée de Touba... Yalla nalène Su...
19/01/2022

Bravo à ces braves SOKHNA qui s'occupent du nettoyage et de la propreté de la Grande Mosquée de Touba... Yalla nalène Sunu Borom sam guddal faan yi si barké Cheikhoul Khadim.❤

Bokk na ci ay waxam moom KU TEDD KI:Am na ku mas a ñëw ci moom ne ko:" Mbàkke man déy sama doom dafa am Soxna ma bëgg ng...
02/12/2021

Bokk na ci ay waxam moom KU TEDD KI:

Am na ku mas a ñëw ci moom ne ko:" Mbàkke man déy sama doom dafa am Soxna ma bëgg nga ñaanal leen Yàlla juboole leen". Sëriñ Bi def tekk, mu waxaat ko ko, Sëriñ Bi ne tekk, mu waxaat ko ko, Sëriñ Bi ne ko:" Tee ma leen a ñaanal Yàlla jubal leen njëkk, door leen a juboole, xanaa xamóo ne yàq goo gis ci àdduna ñaar ñu juboo te jubuñu moo ko waral "

WAXI SËRIÑ TUUBAASËRIÑ TUUBAA nee na :Ku xam Boroomam du topp kudul Boroomam, ku sàggan du topp ludul Bakkanam. Ñi xam Y...
30/11/2021

WAXI SËRIÑ TUUBAA

SËRIÑ TUUBAA nee na :
Ku xam Boroomam du topp kudul Boroomam, ku sàggan du topp ludul Bakkanam. Ñi xam YÀLLA dañuy dimbalante ci xam YÀLLA ak ragal YÀLLA. Ñi sàggan dañuy xëccoo ci moy YÀLLA aka noono

Àdduna dou kër mootax kufi nékk Wara bàyyi xél ëllëg Wara farlu thi jaamu Yàlla ak Sellal ta roy mak ñu baax ñi Yàlna Yà...
29/11/2021

Àdduna dou kër mootax kufi nékk Wara bàyyi xél ëllëg Wara farlu thi jaamu Yàlla ak Sellal ta roy mak ñu baax ñi Yàlna Yàlla Saafara jàngoro yi ta dolli wér gi

"Képp koo xam ni kii mi ngi wax ak yaw waxu la, Yàlla waxu la dëgg, waxu la lu lay jariñ ëllëg, mi ngi lay lor te mi ngi...
27/11/2021

"Képp koo xam ni kii mi ngi wax ak yaw waxu la, Yàlla waxu la dëgg, waxu la lu lay jariñ ëllëg, mi ngi lay lor te mi ngi lay wor. Wax ba wax jeex, dëgg a ca gën te dëgg ba dëgg jeex, dëgg ga ñu wax ngir Yàlla a ca gën"

Sëriñ Saam Mbay

Sëñ Tuubaa nee na : « Képp ku ngeen bëgg ci seen ug njaboot deeleen ko yar, ku ngeen manul a tàgool deeleen ko wax dëgg....
26/11/2021

Sëñ Tuubaa nee na : « Képp ku ngeen bëgg ci seen ug njaboot deeleen ko yar, ku ngeen manul a tàgool deeleen ko wax dëgg. Ku ngeen yéene sutura deeleen ko liggéeyloo. Ku ngeen yéene teraanga deeleen ko jaamuloo Yàlla. »

Waxi Sëriñ Fàllu Mbàkke"Yaar rekka ñu fi bàyi: Muy muñ baŋŋ-baŋŋ yi ak Xaj bon-bon yi"Nous devons notre existence sur te...
26/11/2021

Waxi Sëriñ Fàllu Mbàkke
"Yaar rekka ñu fi bàyi: Muy muñ baŋŋ-baŋŋ yi ak Xaj bon-bon yi"

Nous devons notre existence sur terre qu'à deux choses :
- Tolerer les caprices des gens
- Effacer les pèchès des crèatures.



Nit ki balaa munan tooy na waa la wow na, War naa xam luy tooy, wala luy wow.Ngir muccu ci jumtey xalaat ak àtte (juger)...
25/11/2021

Nit ki balaa munan tooy na waa la wow na,
War naa xam luy tooy, wala luy wow.
Ngir muccu ci jumtey xalaat ak àtte (juger).

𝙎𝙝𝙚𝙚𝙭 𝘼𝙗𝙙𝙤𝙪𝙡 𝘼𝙝𝙖𝙩 𝙢𝙗𝙖𝙘𝙠𝙚« Murid buy waaxu soli dàllam di dox, kuko néex dib sangam. Waaye Murid buñ tëral cig jaad jëmé ...
24/11/2021

𝙎𝙝𝙚𝙚𝙭 𝘼𝙗𝙙𝙤𝙪𝙡 𝘼𝙝𝙖𝙩 𝙢𝙗𝙖𝙘𝙠𝙚

« Murid buy waaxu soli dàllam di dox, kuko néex dib sangam. Waaye Murid buñ tëral cig jaad jëmé ko àllaaxira, kuko né am nga benéen sëriñ bu dul Sëriñ Tuubaa, bu manoo na jóg, bu jogée du fab yat, jaasi lay fab dal sa kaw ».

Les grands hommes ne donnent pas uniquement des ordres, ils donnent l’exemple. Al Muntaqaa (le sélectionné)❤️.Yàlla na f...
23/11/2021

Les grands hommes ne donnent pas uniquement des ordres, ils donnent l’exemple. Al Muntaqaa (le sélectionné)❤️.

Yàlla na fi yàgg te wér.


Adresse

KEUR SERIGNE SALIOU
Linguère

Téléphone

774150228

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Daara Matlaboul Chifai Wakeur Serigne Saliou Sopey Cheikh Ibra publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Contacter L'entreprise

Envoyer un message à Daara Matlaboul Chifai Wakeur Serigne Saliou Sopey Cheikh Ibra:

Partager